wikipediyaa — Wiktionary
Wikipedia am na jukki bu tudd:
Wolof
[Soppi]
Mi ngi juddu ci booleb waati angale yu wiki ak encyclopedia (jimbulang) → Mottalil gongikubaat bi. (Soppi)
wikipediyaa b
ab sémbub jimbulang la, doon tëriin bu ubbeeku
Tekki
[Soppi]
farañse: wikipedia |
wu-angalteer: wikipedia |
wu-itaali: wikipedia |