wo.wiktionary.org

caabi — Wiktionary

caabi:

  1. caabi ubbikaayu lu tëju. mbaa a tëjukaayam.

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

[Soppi]

  1. aal ma caabi ji ma ubbi buntu bi.

Waxiin

Déglu baatu caabi ci wolofi Senegaal